Aller au contenu

Suwe

Jóge Wikipedia.

Weeru Suwe mooy juroom-benneelu weer ci Arminaatu Gregori ak ci bu Suul.

Baat baa ngi jóge ci latin: junius. Jàppees na ne yàllaay waa-rom ju jigéen ja Junon lees ko jagleeloon ngir màggalee ko ko. Ca jamono ju yàgg ja, moo nekkoon ñeenteelu weer ci arminaatu waa-rom bu yàgg ba.

Suwe mooy weer wi njëkk ci tangaay bi ci réew yi féete ci xaaju-kol-kol bu bëj-gànnaar bi.

Weer
Samwie | Fewirie | Maars | Awril | Mee | Suwe | Sulet | Ut | Sattumbar | Oktoobar | Nowembar | Disambar